Kàddug Yàlla+ app for iPhone and iPad
4.4 (
4784 ratings )
Education
Book
Developer: Foundational LLC
Free
Current version: 1.0.3, last update: 4 months agoFirst release : 18 Mar 2023
App size: 62.61 Mb
Appli bii mooy Kàddug Yàlla, gi dikke ñaari pàcc: Kóllëre gu jëkk gi Yàlla fas ak nit, ak Kóllëre gu yees, gi mujja wàcc, te ñenn ñi di ko wooye Injiil, mu tekki Xibaaru jàmm. Ñaari téere yooyu, Yàllaa leen wàcce ci nitam ñu sell ñi, kóllëre gu jëkk gi, ñu bind ko ci yawut, gu yees gi, ci làkku gereg. Li ñu bind ci téere yu jëkk ya nag, moom lanu tekki ci wolof.
Appli bi nag, ngir écran bu yaatu lañu ko defare.